Démb, njiitu réew mi seeti woon na tolluwaayu liggéey bu estaatu Senegaal ba ca Jamñaajo ànd ko ak njaatigel FIFA Infantino. Jaare na ca pose ma xamle ne dees na ko daloo ci 22 feewirye 2022.

Wax na ba tay ne fi liggéey bi tollu dal na xelam te dafa yéene ndawi Senegaal li gën, tax dara warul a tax Afrig ñàkk a am li gën ci àddina si.

Leeral :
Pose mi: occasion

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *