Wëppa wi:
● Dundug Soldaar si ñuy néewal doole ginnaaw bu ñu jékkee
● Fu mbirum fafalnaaw gi daanu woon ca géeju Ndakaaru ga mujj ?
Soldaar te di boroom xam-xam ci wàllu fafalnaaw✈️, moo tere woon genn fafalnaaw jël jaww ji ginnaaw ba mu ca gisee ab jafe-jafe.
Al Asan Aan mooy itam njiital kuréel gi ëmb ña dëkke ca koñu sóobare ya ca Term-Sud ba ca Wakaam. Tollu cu 79i njaboot yu ay kilifay soldaar bëgg a génne ca seen i kër.
Ngir seetaan ko bësal fii 👇🏽
https://youtu.be/_q8p2dFMIwQ

Une pensée sur “Fu mbirum fafalnaaw gi daanu woon ca géeju Ndakaaru ga mujj ?”

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *