Nu ngi leen di yëgal génn àddunag Sëriñ Àbbaas Mbàkke di ñenteelu xalifab Daaru Muxti di doomu Sëriñ Maam Cerno Biraahim Mbàkke.

Faatiha ak Lixlaas.

Waa Saabal.com a ngi koy jaal waa Daaru Muxti gépp te di ko ñaanal Yàlla xaare ko ca guyaar ca gën a kawe te taas nu ci barkeem.

Saabal.com

Guyaar / àjjana.

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *