Ca ba ñuy amal um ndaje ca Ngombalaan ga, ab takk-der la ñu yabal ca kër Usmaan Sonko ngir mu wuyuji ci altine ji, di li Seex Bàmba Jéy xamle.

Njiitu Pastef nag dafa bañ ne du ko jël waaye terewul dalal na takk-der ba waxtaan ak moom mu yegge ko ay li waral ay tànkam.

« Mënumaa jël bataaxel bi », di la mu tontu takk-der ba. Moom it tegu ca dara, dafa ñokket, dem war motoom toppaat i tànkam…

Saabal.com

Ngombalaan gi : Assemblée Nationale

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *